bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 1:44
Luke 1:44 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Maa ngi lay wax ne, naka laa la dégg ngay nuyoo rekk, sama doom ji yengu ci sama biir ndax mbég.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la sa kàddug nuyoo tàbbi sama nopp rekk, sama doom ji yëngu ci sama biir bi ndax bég.