Luke 1:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca jamonoy Erodd, mi nekkoon buur ca réewu Yawut ya, amoon na saraxalekat bu ñu tudde Sakariya te bokk ca mbootaayu saraxalekat, ya askanoo ci Abiya. Jabaram Elisabet askanoo moom itam ci Aaroona.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jant ya Erodd dee buuru réewum Yawut yi, ab sarxalkat la woon bu ñuy wax Sàkkaryaa, bokk ci làngu sarxalkat, yi askanoo ci Abiya, te soxnaam Elisabet askanoo ci Aaróona.