Luke 1:58 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dëkkandoom yi ak mbokkam yi yég ne, Boroom bi won na ko yërmande ju réy, ñu ànd ak moom bég.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dëkkandoom yaak ay bokkam yég noonu ko Boroom bi xéewalee yërmandeem, ñu bokk ak moom mbégte ma.