Luke 1:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Sakariya ak jabaram ñu jub lañu ca kanam Yàlla, di topp ni mu ware ndigal yi ak dogali Boroom bi yépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñoom ñaar ñépp a juboon, Yàlla seede, te mucc ayib ni ñuy jëfe santaane yeek ndigali yooni Boroom bi.