Luke 1:61 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu ne ko: «Amoo menn mbokk mu tudd noonu.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne ko: «Waaye kenn ci say bokk tuddul noonu!»