Luke 1:62 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñu daldi liyaar baayam, ngir xam nan la bëgg ñu tudde xale ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ñu liyaar baayam, ngir xam nu mu bëgg ñu tudde xale bi.
Recommended Reading