Luke 1:63 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Sakariya laaj àlluwa, bind ci ne: «Yaxya la tudd.» Ñépp daldi waaru.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sàkkaryaa laaj àlluwa, ñu jox ko, mu bind ci: «Yaxya mooy turam.» Ñépp waaru.