bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 1:65
Luke 1:65 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waa dëkk ba bépp jaaxle, xew-xew yooyu siiw ca tundi Yude yépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee tiitaange dikkal mboolem ña leen séq, mbir moomu mépp nag doon waxtaan ca diiwaanu tundi Yude gépp.