Luke 1:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye amuñu doom, ndaxte Elisabet mënul a am doom, te it fekk ñoom ñaar ñépp ay màggat lañu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Amuñu woon doom nag, ndax Elisabet manul woona am doom, te it booba ñoom ñaar ñépp a dem ba màggat.