Luke 1:80 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Yaxyaa ngi doon màgg, te xelam di ubbiku. Mu dëkk ca màndiŋ ma, ba bés ba muy feeñu bànni Israyil.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngóor sa nag di màgg, xel ma di yokku. Mu dëkk ca màndiŋ ma, ba bés ba mu feeñoo bànni Israyil.