Luke 10:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Gannaaw loolu Boroom bi tànn na yeneen juróom-ñaar-fukki taalibe ak ñaar, yebal leen, ñu ànd ñaar ak ñaar, jiituji ko ca dëkk yépp ak ca bérab yépp, ya mu naroon a dem moom ci boppam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Sang bi tabb na yeneen juróom ñaar fukki taalibe ak ñaar, yebal leen, ñaar, ñaar, ñu jiituji ko ca mboolem dëkk yaak gox, ya mu nammoona dem moom ci boppam.