Luke 10:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi leen koy wax, bu bés baa, waa Sodom ñooy tane dëkk boobu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa leen ko wax, bu bés baa, boobu dëkk, Sodom a koy gënu demin.