Luke 10:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moona li leen rab yi déggal, bumu tax ngeen bég, waaye bégleen ndax li ñu bind seen tur ci asamaan.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu leen rab yi nangule nag, buleen ko bége, bégeleen kay la seen tur binde fa asamaan.»