Luke 10:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye xutbakat ba bëggoon a am aw lay, ne Yeesu: «Kan mooy sama moroom nag?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa ja nag namma wutu lay, ne Yeesu: «Sama moroom mooy kan?»