Luke 10:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Faf ab saraxalekat jaar ca yoon wa, séen nit ka, teggi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yàlla woo yàlla ab sarxalkat bu jaare yoon woowa, séen nit ka, daldi teggi.