Luke 10:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye benn waay bu dëkk Samari bu doon tukki, ñëw ba jege waa ja, gis ko, yërëm ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jenn waay ju dëkk Samari nag doon tukki, dikk ba jege waa ja, xool ko, yërëm ko lool.