Luke 10:35 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi bët setee, mu génne ñaari poseti xaalis, jox ko boroom kër ga ne ko: “Nanga topptoo nit kooku. Bés bu ma fi jaaraatee, dinaa la fey, man ci sama bopp, lépp loo ci dolli ci xaalis.”»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca ëllëg sa, mu yékkati ñaari poseti xaalis, jox ko boroom dal ba, ne ko: “Topptoo ko waa ji. Loo ci dolli, bu ma dëppee, maa la koy delloo.”»