Luke 10:38 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi Yeesu ak ay taalibeem nekkee ci yoon wi, mu dugg ci benn dëkk, fekk fa jigéen ju tudd Màrt, ganale ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ak ay taalibeem ñoo toppoon seenu yoon, ba tollook ab dëkk. Ba ñu dikkee, senn as ndaw su ñuy wax Màrt, ganale ko.