Luke 10:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nangeen wéral jaragi dëkk ba, te ngeen ne leen: “Nguuru Yàlla jegesi na leen.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Wéral leen jaragi dëkk ba, te ngeen wax waa dëkk ba, ne leen: “Nguurug Yàlla dëgmal na leen.”