Luke 11:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Am bés Yeesu dàq rab wu luu. Naka la rab wa génn, luu ba daldi wax, ba mbooloo may yéemu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu moo doon dàq aw rab wu duggoon nit ba mu luu. Ba rab wa génnee, luu ba wax, mbooloo ma waaru.