Luke 11:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye am ca mbooloo ma ay nit, ñu doon wax naan: «Ci kàttanu Beelsebul, buuru rab yi, lay dàqe rab yi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul ñenn ca ñoom ne: «Ci Beelsebul, buuru rab yi lay dàqe ay rab.»