Luke 11:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye Yeesu xam seen xalaat ne leen: «Réew mu xeex boppam tas, kër gu xeex boppam gent.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu itam ràññee seen xalaat, ne leen: Gépp nguur guy xàjjalikoo ci biiram, day tas, yii kër màbb ca kaw yee.
Recommended Reading