Luke 11:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu ko gisee nag, mu dem wooyi yeneen juróom-ñaari rab yu ko gën a soxor. Ñu dugg, sanc fa; ba tax mujug nit kooku mooy yées njàlbéenam.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
day dem indi yeneen juróom ñaari rab yu ko yées, ñu bokk sancsi. Su ko defee ni nit kiy mujje mooy yées na mu jëkke.»