Luke 11:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu tontu ko ne: «Neel kay, ki barkeel mooy kiy déglu kàddug Yàlla te di ko topp.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moom nag mu ne ko: «Xanaa kay, ndokklee ñiy déglu kàddug Yàlla te di ko jëfe.»