Luke 11:29 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Naka la mbooloo may gën a takku, Yeesu ne: «Niti jamono jii dañoo bon. Ñu ngi laaj firnde, waaye duñu jot genn firnde gu dul firndeg Yunus.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la mbooloo may gëna takku, Yeesu ne: «Niti tey jii, nit ñu bon lañu. Firnde lañuy wut, waaye deesu leen jox jenn firnde ju moy firndey Yunus.