Luke 11:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ni Yunus nekke woon firnde ci waa dëkku Niniw, noonu la Doomu nit kiy nekke firnde ci niti jamono jii.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax na Yunus nekke woon firnde ca waa Niniw, noonu la Doomu nit ki nekke firnde ci niti tey jii.