bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 11:38
Luke 11:38 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Farisen bi nag daldi jaaxle, bi mu gisee ne Yeesu raxasuwul, laata muy lekk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Farisen bi nag jaaxle, ndax la Yeesu setluwul bala moo waaja lekk.