Luke 11:45 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kenn ci xutbakat yi ne ca tonn ne: «Kilifa gi, boo waxee loolu, yaa ngi nuy xas, nun itam.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kenn ci xamkati yoon yi nag àddu ne: «Sëriñ bi, loolu nga wax de, nun itam, xasaale nga nu ci.»