Luke 11:50 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag Yàlla dina mbugal niti jamono jii ndax dereti yonent yi ñu tuur, ba àddina sosoo ak léegi,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ko defee yoon topp niti tey jii, deretu mboolem yonent yi tuuru, dale ko ca cosaanu àddina.