Luke 11:52 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen xutbakat yi, dingeen torox, ndaxte yéena yóbbu caabiy xam-xam; dugguleen ci, te ku ci bëgg a dugg, ngeen tere ko ko.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngalla yeen xamkati yoon yi, yeena sànk caabiy xam-xam; yeen dugguleen, ñiy duggsi, ngeen tere leena dugg.»