Luke 12:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku sosal Doomu nit ki, dinañu la baal, waaye kuy sosal Xel mu Sell mi, duñu la ko baal.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Képp ku jëme kàddug safaan ci Doomu nit ki, dees na la jéggal, waaye ku saaga Noo gu Sell gi, deesu la jéggal.