Luke 12:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Am ca mbooloo ma ku ne Yeesu: «Kilifa gi, joxal ndigal sama mag, mu sédd ma ci sunu ndono.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kenn ca mbooloo ma moo noon Yeesu: «Sëriñ bi, waxal ci sama mag, mu jox ma sama wàll ci ndono li nu bokk.»