Luke 12:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu ne leen ñoom ñépp: «Moytuleen bëgge, ndaxte bakkanu nit ajuwul ci alalam, ak lu mu baree-bare.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu mu ne leen ñoom ñépp: «Moytuleen wépp xeetu bëgge, ndax loo barele barele, sa bakkan ajuwul ci sa alal.»