Luke 12:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu dégtal leen wii léeb ne: «Dafa amoon waa ju bare alal, te ay toolam nangu lool,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu léeb leen nag, ne leen: «Nit la woon ku woomle, te ab toolam nangu.