Luke 12:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yàlla ne ko: “Ñàkk xel! Guddig tey, dees na jël sa bakkan. Kon li nga dajale lépp, ku koy moom?”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yàlla nag ne ko: “Ñàkk xel! Guddig tey jii, dees na jël sa bakkan. Kon li nga waajal, ana kuy doon boroom?”