Luke 12:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Kiy dajale alal ngir boppam nag te amul dara ca kanam Yàlla, lu mel nii moo lay dal.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Kuy dajaleel boppam alal te woomlewoo fa Yàlla, loolu mooy saw demin.»