Luke 12:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Seetleen baaxoñ yi: duñu ji, duñu góob, amuñu dencukaay, amuñu sàq, teewul Yàllaa ngi leen di dundal. Céy ni ngeen ëppe maana picc yi!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seetleen ci baaxoñ: du ji, du góob, amul ub denc mbaa am sàq. Teewul Yàlla di ko dundal. Yeen nag, ñaata yoon ngeen gën picc yi!