Luke 12:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ana kan ci yéen ci kaw njaaxleem, moo man a yokk ab waxtu ci àppam?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana kan ci yeen mooy jaaxle, di xalaata xalaat bakkanam ba mana yokk lu tollook xef ak xippi ci àppam?