Luke 12:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen ñi néew ngëm! Bu Yàlla woddee nii ñaxu tool yi, miy sax tey te bu subaa ñu def ko ci taal bi, ndax du leen gën a wodd?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndegam ñaxum tool miy dund tey, te léegi ñu sànni ko cib taal, moom la Yàlla solale noonu, xanaa astamaak yeen kay? Yeenaka néew ngëm!