Luke 12:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Buleen di wut lu ngeen di lekk walla lu ngeen di naan; te buleen ci jaaxle.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen nag, buleen tiisoo lu ngeen lekk, mbaa lu ngeen naan; te bu yooyu xalaat ub seen bopp.