Luke 12:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Looloo tax lu ngeen wax ci biir lëndëm, dees na ko dégg ci leer. Lu ngeen déey nit ci biir néeg, dees na ko yégle ci kaw taax yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax mboolem lu ngeen waxe biir lëndëm, dees na ko dégge bëccëg ndarakàmm, te mboolem lu ngeen déeye ci néegu biir, dees na ko biral ci kawi taax.