Luke 12:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye wutleen nguuram, te loolu lépp dina leen ko ci dollil.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye tiisooleen nguuram, su boobaa dees na leen ci dollil loolu.