Luke 12:32 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
«Buleen ragal dara, yéen coggal ju ndaw ji, ndaxte dafa soob seen Baay, mu jagleel leen nguuram.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Buleen ragal dara, yeen jur gu sew gi, ndax seen Baay la soob, mu jagleel leen nguur gi.