Luke 12:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mel-leen ni ay surga yuy xaar seen njaatige buy jóge ca céet ga, ndax bu fëggee bunt ba, ñu ubbil ko ca saa sa.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mel-leen ni nit ñuy séentu seen njaatige lu jóge céet, ndax bu dikkee ba fëgg bunt ba, ñu daldi ko ubbil.