Luke 12:38 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Su fekkee seen njaatige ci xaaju guddi lay ñëw sax, walla bu suuf seddee, te fekk leen noonu, surga yooyu ñoo gën a yeyoo ngërëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndegam ba guddi ga xaajee la njaatige la ñibbsi, ba fekk surga ya teewloo noonu, am ba suuf seddee la, lu mu ci mana doon, ndokklee ñoom.