Luke 12:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Maa ngi leen koy wax, samay xarit, buleen ragal ñu man a rey yaram, ba noppi dootuñu man a def dara.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Maa leen ko wax, yeen samay soppe, buleen ragal ñu manul lu wees rey seen yaram, ndax gannaaw loolu dootuñu leen manal lu ko raw.