Luke 12:40 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen itam taxawleen jonn, ndaxte Doomu nit ki dina ñëw ci waxtu wu ngeen ko séenuwul.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon yeen itam waajleen ba jekk, ndax waxtu wu ngeen foogul, ci la Doomu nit ki di ñëw.»