Luke 12:41 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Piyeer ne Yeesu: «Boroom bi, ndax dangay dégtal léeb wii ngir nun rekk walla ngir mbooloo mépp?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Piyeer nag ne Yeesu: «Sang bi, ndax nun doŋŋ nga léeb lii, am ñépp a ko moom?»