Luke 12:42 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Boroom bi tontu ko ne: «Kan moo nekk surga bu takku te teey, bu njaatigeem teg ci waa kër gi, ngir mu leen di dundal ci jamono ji?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sang bi ne ko: «Ana kan nag mooy saytukat bu wóor te muus, ba njaatigeem batale ko curgag këram, ngir mu di leen jox seen njël ca ba muy jot?