Luke 12:47 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
«Surga bi xam bëgg-bëggu njaatigeem, te waajul mbaa mu takku def ko, dinañu ko dóor dóor yu metti.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Jawriñ jooju xam nammeelu njaatigeem, te taxul mu waaj ko, ba jëfewu ko, ay yetam dina bare.
Recommended Reading